Découvrez notre titre SENEGAL, extrait du prochain album "Foundation" !
Nous vous faisons voyager, découvrir le Sénégal à travers ses beaux paysages.
Faada et Ndongo vous emmènent en car rapide dans les 14 régions !
Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi
Jambaar dawul doolé ladoon wuti
yagg naa bittim reeeeew ñibbisi naaaa
sama reew Senegal
#Senegal #Senegal #Senegaaaaaaaaaaal
J’aime ce Pays qui m’a vu grandir
cette terre qui a vu mes premières larmes et mes fou rires
Pas besoin d’un crayon pour dessiner les sourires
Tels des rayons de soleil pour t’accueillir
le Cfa parle fort à travers et à tort
On marchande pour le transport et Quoi encore…
ici il n’y a pas de métro pas de Tram(way)
ici c’est Taxi-brousse, jeaune-noir
cars-rapide, ndiaga ndiaye ou Pousse-pousse
Petite pause dans une Dibiterie ou Tangana
Petite tintamarre c’est du Tama
« Dakar ne dort pas » elle danse avec ou sans salaire
Malgré les coupures d’électricité , d’eau et la Galère
une pensée pour les frères qui ont coulé dans l’Atlantique
meme si j’ai la chance de revenir ma blessure est authentique
Nul n’est prophète chez soi
mais on est mieux que chez soi
c’est vrai j’ai duré labas mais mon coeur était là
senegal
Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi
Jambaar dawul doolé ladoon wuti
yagg naa bittim reew ñibbisi naaaa
sama reew Senegal
#Senegal #Senegal #Senegaaaaaaaaaaal
Fila reew néexé
Sénégal ngi dé
booko soré dooto bëgg ludul Ñibbisi dé
bofi ñëwé joxé mbok néla kaay ñu gissé
ana lo inddi tay daañ la yen
say xarit yaggon toog di Xaar di séntu bis bi Mi ngi
Ñëw na tay no dikké serica yi nga diggé
séntu nañla fin d’année été doyul daggal billet
att bilé giss mbok yilé summi yërré immigré
Metro boulot amul Dodo jogg bala jant bi Modou modooo
ñu ngi daw wuti wuti bitim reew bañ fa futi ubbi buntu xéwal bis
fok ñu ñibbi mu ngi guddi sorri nga dëkkuwaay
géntal ñulay téeru bis di nga délluwaay yoon wi na nga léer lu
Xamal né jéggé na njaboot gi ñëppa ngi xaar
démoon nia ñëwaat nga Senegal mooy sa képaar
Le courage de partir
La force de revenir
Partir pour grandir
Revenir pour bâtir
dans la grisaille et le froid
J’entendais ta voix ,me Revoilà chez moi
là ou je me sens comme un Roi Senegal…Senegal…Senegaaaaal
Jom mooy dém waayé fulay ñibbisi
Jambaar dawul doolé ladoon wuti
yagg naa bittim reew ñibbisi naaaa
sama reew Senegal
#Senegal #Senegal #Senegaaaaaaaaaaal
KAFFRINE SEDHIOU THIÉS LOUGA DIOURBEL SAINT LOUIS MATAM KOLDA
KAOLACK KEDOUGOU TAMBACOUNDA ZIGUINCHOR et DAKAR -Senegal Senegal Senegal
KAFFRINE SEDHIOU THIÉS LOUGA FATICK SAINT LOUIS MATAM KOLDA
KAOLACK KEDOUGOU TAMBACOUNDA ZIGUINCHOR et DAKAR-Senegal Senegal Senegal
Category :
Senegal Music Videos
#daara#j#family#senegal#clip#officiel