Jeeba - Freesenegal

  • #freesenegal
    Auteur : Jeeba
    Compositeur : Iss 814
    Réalisation : Viewzstudios
    Lyrics :
    Lima guente lima guente
    Mbadou Sénégal bi ni ni la nara moudié
    Leklé damay tok di dioy
    Médiocrité laniou jiital def ko thi système bi
    Faté ligueye ngeum ligueye mérité founiou dieum Goorgorlu amatoul ndeysane
    Degg na daniou yoor loudoul diexx
    Goroulo yatoulo, boné niou ngafi nekal walay c’est faux Daniou la faal nguir souniou avenir doom
    Dou thiagané lou nek thi rew mi yako moom
    Kone fatalikoul niou done khex ndax yow
    Niou niak sen bakane nguir am euleuk bu baax
    Way wax leen bala mouy niaw
    Niaaaw niaaaw meunone na bania wax tok nopi bayi nonou Souma ko defé mou niaw niaaaw
    FreeSénégal diam sama rew
    Yow dila wo dila wo
    Mbadou Senegal bi ni ni la nara moudié
    Leklé ma tite dila wo oh dila wo oh
    Mbadou Sénégal ni ni la nara moudié
    Way wax leen bala mouy niaw
    Niaw niaw meunone na bania wax tok nopi bayi nonou Souma ko défé mou niaw niaw
    FreeSénégal diam sama reew
    Xolal jeunesse bi
    Keneu ligueyatou si
    Baay katt biniou waara doundal mo geuna khiff Naap katt bi di dioy guedj gui dagn ko siff
    Thiono day reer fi bo amoul bras long bril do yeksi Étudiant di dioyou nénagn danio sone
    Takk deer yi diniou baume
    Douniou seni none
    Diama geune ay nio bok senegaaaaalll
    ndiaye Diama geune ayy aaay
    Yow dila wo dila wo
    Mbadou Sénégal bi ni ni la nara moudié
    Leklé ma tite dila wo oh dila wo oh
    Mbadou Sénégal ni ni la nara moudié
    Way wax leen bala mouy niaw
    Niaw niaw meunone na tok bania wax bayi nonou Souma ko défé mou niaw niaw
    FreeSénégal diam sama reew!!!

    Category : Senegal Music Videos

    #jeeba#freesenegal

    0 Comments and 0 replies
arrow_drop_up