Bril - Lettre au Président (Free Senegal) **VOSTFR**

  • ** Abonne-toi à ma chaîne ici goo.gl/Qw5BFh **
    En ces temps agités, où le peuple sénégalais est à la croisée des chemins pour redéfinir son avenir et prendre un nouvel élan, où notre démocratie est menacée, Bril fait entendre sa voix dans une lettre rappée au Président de la République.
    #Bril #LettreAuPrésident #FreeSénégal #ClipOfficiel #démocratie #m2d #MackySall #ClassChicMusic #RapGalsen #hiphop
    ** Crédits de la chanson & du clip "Lettre au Président" **
    Auteur - Compositeur : Bril
    Studios enregistrement : Class’Chic Music
    Mixage, edit & mastering : Class’Chic Music par Bril
    Images, montage & color grading clip : Mouride pour Natty Dread Films
    Une production de Class’Chic Music (Dakar, Senegal, mars 2021)
    ** Les lyrics de "Lettre au Président" **
    Dakar le 07 Mars 2021
    Mangui toudou Djibril Fall, niou gueune ma xam thi tourou Bril
    Bataaxal bimay bindeu nak, mangui koy djagglél buur .
    Prési askane wéma yoni nénagn Rewméngui boy
    Déréttangui tourou fèppeu wadjour yeupangui djoy
    2012 beuggone Solution motakh niou fal-leu
    Té légui Réwmé eup problème Classou CM2
    Déggagougnla wayé khamnani djotnga Xibaar yi
    Xééx thi mbéd , Takk dér yi Nek, Déé gui gueune di baari
    Todjngén Rewmi ndakh Viol té yagga violé sunuy Droit
    Réwmi amoul yakkaar, bouniouy djokh raaya policier bou djoupp, amouniou Loi
    Un Peuple - Un but - Une foi
    Nénagn dougnla bayi ngay falou 3 fois
    Nonon doko meune
    Ndiaago meunoul peinture ba peinture assamane
    Légui boy yi daniõ ragal doundou , gnimé coup de feu
    Ndakh sén biir yé gueuna vide Dakar heurou Couvre feu
    Khiif bou méti motakh niou beuri di profito di woutt
    Louniou lékkeu , waathiél sa bopp, sa karaw doko soutt
    Guéneul wakh ak niom, Thiowli meuna Djéékh
    Réwmi dou yako mom, bathiy def loula Néékh
    Dou yone ay Nervis djeul plaçou takkeu der yi
    Khéép ay gourdin wout ay armes xéékh’ak gni di sani xéér yi .
    Bataaxal bi djéékhagoul, Prési degglouma
    Meunouma dénthie sama xalima té bindouma
    Wakh thi gni féébar yor ordonnance té amouniou lougnko djeundé
    Gni né thi ngour gui beurilé ba amouniou lougn ko doyé
    Continué di tek deal you sétt ni léélou Aba
    No stress laniouy léékké sunu xaliss douniou Nitt
    Politicien yé gueuna faux sonnerie iphone thi android
    Dangay niakkeu ba do nélaw, niou rêvélola done sa Ndjiitt
    Koula matteu fatalila ni amnga ay beugn
    Dotouniouko nangou c’est le Sénégal qui bagne
    04 Avril khamwma louniouy fêter wayé dou indépendance
    1960 ba tay ngén djokh lou beuri France
    Paathio Rewmi ba nioune amatouniou bén liberté
    Statue de la liberté niou eup liberté
    Nioune douniou ay tailleur wayé djeulnagn ay mesures
    You léér , tek ko fou léér , je vous le jure .
    Peuple bi ragalouniou guiss nga niniouy tééro Risques.
    Ba sa ministre bi tite djignlén terroristes.
    Dou deugg dou yone kou wakh nga teudj amo opposant.
    Légui peuple bi mo moudjé guéneu done sa opposant.
    Deugg ngéni bagn té deugg faaléwoulén
    Teklén ko thi yone nangoulén
    Deugg mou moudjou féppeu kone parélén
    Djaay dõlé baakhoul waathieulén
    ** Retrouvez Bril sur les réseaux sociaux **
    Facebook www.facebook.com/brilofficiel
    Instagram www.instagram.com/bril_officiel
    Twitter twitter.com/bril_fight4
    Snapchat : @bril-fight4
    **Contact management**
    Mr Mahmoud Sy : +221 77 036 48 31 <64>brilfight4@gmail.com
    **Booking international**<66>vincent.lagoeyte@soon.pro

    Category : Senegal Music Videos

    #bril#lettre#au#pr#eacute#sident#free#senegal#vostfr

    0 Comments and 0 replies
arrow_drop_up