Production : KBC MUSIC
Lyrics: Ngaaka blindé
Réalisation : Schadiiq
Drone : Arona wade
Beat by: Nick silver
Mix : Nick silver
Master : KBC
Fashon: Shanel Shmurda
Assistance: Leuz kbc & Leuz dopy
///////////////:::::
Paroles : Chérie kitoko, chérie kitoko !
Chérie my woman, woman wom !
Chérie my woman, woman wom !
Chérie guisso dou tchi yaw ma dioum !
What’s up what’sapa in your room !
Chérie Nouyouma Boulma romb !
Chérie wouyouma Boulma romb !
Fethialma rumba rumba rum !
What’s up what’sapa in your rom!
Chérie kitoko …
I don’t like the way you give me your love (2x)
Chérie kitoko …
I don’t like the way you give me your love oh
Chérie kitoko …
I don’t like the way you give me your love
Diaral ngama do anything !
Bou néké assamane Ci nga beugg
ma andilako way … !
Ma Chérie boul dioy !
Xamnani mane mala toogn yeah !
Xolma sama xol tooy !
Fo yendo dei falay fanane !
Soxnaci boul dioy !
Je t’aimerai comme d’hab
Bb j’ai les contacts
Kayniou ande fou dougou ma dougou
Goudou comme jack !
Kayniou jeu de contact,
Wiri Wiri comme d’hab
Fo fetté ma feuleu, fatalma fofou may fatt !
Enh, fi mbeuguel bou deugou
day andaki thiono gui yeupp enh …
Mane Loutakh ma sonal la
Sonalnaa mboolo mi yeup enh
(Refrain) …
Chérie my woman, woman wom !
Chérie my woman, woman wom !
Chérie guisso dou tchi yaw ma dioum !
What’s up what’sapa in your room !
Chérie Nouyouma Boulma romb !
Chérie wouyouma Boulma romb !
Fethialma rumba rumba rum !
What’s up what’sapa in your rom!
Chérie kitoko …
I don’t like the way you give me your love (2x)
Chérie kitoko …
I don’t like the way you give me your love oh
Chérie kitoko …
I don’t like the way you give me your love
Wonala woma niou ande rek seey
Boula nekhé nga wo Mami
Limay def ni yeupp wollay dou lepp la tay
Boma weddé nga xol tani (petaw)
Na honey A Fammi
Every day Time is money
W’ill never waste time my honey
Lima mbedd diangalone dou lepp la mine
Dinane ko door dinane ko saga
Nane dianni door tchi mbam yi
Djigne ko thiaga
Li diaroul goor, goor diaroul nada
Légui done na ndongo wakh faada
Refrain / Fin
Category :
Senegal Music Videos
#ngaaka#blinde#kitoko#clip#officiel